Akayi

Ci angale mooy Achaia; Ci faranse mooy Achaïe

Diiwaan la woon ci nguuru Room. Mooy genn wàllu Geres bu féete bëj-saalum.

Ci Injiil dañuy gis Akayi ci Jëf 18:12,27; 19:21; Ro 15:26; 1Ko 16:15; 2Ko 1:1; 9:2; 11:10; 1Tes 1:7,8.