Aram

Ci làkku ibrë la tur wi jóge. Ci angale mooy Aram or Ram; Ci faranse mooy Aram

Doomu Esrom la woon, di maamaatu Daawuda (1Ch 2:10; Ru 4:19). Naka noonu, bokk na ci maamaati Yeesu ci Macë (Mc 1:3,4). Aram mooy ki ñu tudd Admin itam ci maamaati Yeesu ci Luug (Lu 3:33).