ci jëmm, kàttanug imbiku, mooy kàttan gi menn mbir di soloo suy yëngu. Mooy liggéey bees laaj ngir man a jëlee wenn yaram wi cig tekkaaralam doxal ko, muy daw walla di wëndeelu.
Ngir man a natt kàttanu wenn yaram wi faww nu xam dayoom m ak xél v yi muy daw.