Lóriye
![Lóriye gi (Laurus nobilis)](http://upload.wikimedia.org/wikipedia/commons/thumb/4/4d/Laurus_nobilis_g1.jpg/220px-Laurus_nobilis_g1.jpg)
Lóriye gi xeetu garab la gu bokk ci njabootug Lauraceae, ci bëj-saalumu Tugal la bàyyiko waaye amna ci barab yi bari naaj ci àddina bépp, Senegaal it.
Melo wi
Garabug lóriye dafa man a àgg 10i met ci guddaay, xobam day gulumba te wirgo wu nëtëx lay yore, tóor-tóor bi day mboq.
Nataal yi
-
Ëkkug garabug lóriye
-
Xobi garabug lóriye
-
Tóor-tóori garabug lóriye
Turu xam-xam wi
Laurus nobilis