Tunduw Ndakaaru
Ndakaaru wenn la ci 35 tund yees séddalee Réewum Senegaal, di it benn ci 4 tundi diiwaanu Ndakaaru, dëkku Ndakaaru mooy péeyu tund week diiwaan bi te am 1 030 594 ciy way-dëkk
Séddaliinu tund wi
Tund wi dees koo dog-doge ci 19 dëkkaani ndiiwaan, di:
- Biskuwitëri
- Kamberéen
- Jëppël-Derkle
- Faan-poe Ë-Amicee
- Gëltappe-faas-Kolobaan
- Graa Ndakaar
- Aan-Nelleer
- HLM
- Medinaa
- Meermoos-Sakre-Këër
- Ndakaaru gu Platóo
- Ngor
- Parsel aseni
- Paduwaa
- Sikaap-Libeerte
- Wakaam
- Yoof
Lëkkalekaay yu biir
Téerekaay
- (fr) Ibrahima Diallo, Le droit des collectivités locales au Sénégal, Paris, L'Harmattan, 2007, 380 p. (ISBN 978-2-296-03770-0)
- (fr) Djibril Diop, Décentralisation et gouvernance locale au Sénégal. Quelle pertinence pour le développement local ?, Paris, L'Harmattan, 2006, 268 p. (ISBN 2-296-00862-3)
- (fr) François Zuccarelli, « Le département sénégalais », Paris, Revue juridique et politique, n° 3, juillet-septembre 1968, p. 854-874
| |||
Bàkkel · Bambey · Biñoona · Dagana · Ndakaaru · Njaaréem · Fatik · Funjunj · Gosaas · Géejawaay · Kafrin · Kanel · Kawlax · Kebemeer · Keedugu · Koldaa · Kungéel · Lingeer · Luga · Mbuur · Maatam · Mbakke · Ñooro gu Rip · Ussuy · Pikin · Podoor · Raneru · Tëngéej · Ndar · Séeju · Tambaakundaa · Cees · Tiwaawon · Wilingara · Siggcoor · |