Gàmmu
Gàmmu, ( ci araab ربيع الأول) mooy ñetteelu weer ci weeri wolof tuddees na ko noonu ngir ne araab yi dañu ci daan lolliwu, maanaam daan ci am am ñax, di ci sàmm seenug jur, am ñu ne daa dëppoo ak lolli bi moo tax ñu tudde ko ko.
Ci wolof nak daa yem ak weer wees di màggalee juddug yonnent bi te màggal googu moo tudd Gàmmu ci wolof.
Xew-Xew
- ci lees di màggal juddug yonnent bi, ci ñi yellal ni warees naa màggal ag juddoom.
Tamxarit | Diggi-gàmmu | Gàmmu | Rakki-gàmmu | Rakkaati-gàmmu | Maami-koor | Ndeyi-koor | Baraxlu | Koor | Kori | Diggi-tabaski Tabaski |