Bii jukki ab junj rekk la.
Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal
Saara : yayAfrig Saara ab màndiŋ la, mu ngi soxal Afrig gu bëj-gànnaar. Ak 9.200.000 km2, mooy màndiŋ bi gën a mag ci àddina si, te mooy ñetteelu màndiŋ bi gën a mag ci àddina si, gën a tuuti màndiŋ yi nekk ci Antartika ak bëj-gànnaaru Artiku rekk.